LyricFind Logo
LyricFind Logo
Profile image icon
Lyric cover art

XBX (Xalé Bu Xéré)

Apple Music logo
Deezer logo
Spotify logo
Lyrics
Ouh
Waouh
Anh
Hmm
Ouh oh waoh oh wah
Hmm hmm
Dama génn boy, bénn night di wut lu ma jopp jopp
Ci la mbëkkanték, bénn boy bu xéré bu maa doy jopp
Bokkul ak ñoom, formame bàjjannam moo ko job job
Ginzz naako, mujj japp sóol dafa dope dope
Bii boy moo protéiné (yeah)
Wàccé samay daaj jam maa dose bu caféiné
Waoh, waoh
Maa tegal ko lan moo fi nekk (mbëggeel)
Bàyyi ko mu dem
Je pense que ce n'est pas une bonne idée
Nii mu maa xoolé, sama buumu tama yii bàyyi
Dafa naraa metti rek, ndax man mii duma ko bàyyi
Piss héé miss héé, mu geestu maniko pardon (skrrt)
Muy ree di dem, yég naa ni dafa ame don
Xalé bii dafa xéré (aka xéré)
Xéru ngor laa neexa sanguoo été (she look good)
Doxul ci ay filtres, daf lay réyy sans effet (wuuy wuuy wuuy)
Beauté naturelam dafa yéeme
Lonkotina, xalé bilé toj naa sama cuukel
Nobaatina, def naa lu nekk génnul sama xel
Soppatina, bu xolam melé nii jëmmam jii mel
Duggatina, ci gaalu xol, teer ci géeju mbëggeel
Hmm
Yaw lay topp, nga maay dawloo maa ngétt condition
Yaw laa nob, téé gëmuloko jox maa sa raison
Fees ci sama bopp, tokk ci sama xol, lii lu mu doon
Mbëggeel daaneel maa ni Thioub Lo, amumaa solution
Jox maa sa xol, doko mës réccu girl
Ain't gonna lie to you, I love you waw
Lii maay yég ci sama xol, dafa dëggu
Ki gayy génnat day génn maay kuuy duggu
Nangul ñu dox ànd
Maa waat bàyyi doxaan
Bàyyi laa def lan
Sama xol bii yow laa tànn
Du ay jaaxaan (nanh)
Fas laa soxna laay ñaan (waw)
Sama Oroul Àyni, yaw laa (waw)
Nangul bae ne maa waaw, bala maa die
Xalé bii dafa xéré (aka xéré)
Xéru ngor laa neexa sanguoo été (she look good)
Doxul ci ay filtres daf lay réyy sans effet (wuuy wuuy wuuy)
Beauté naturelam dafa yéeme
Lonkotina, xalé bilé toj naa sama cuukel
Nobaatina, def naa lu nekk génnul sama xel
Soppatina, bu xolam melé nii jëmmam jii mel
Duggatina, ci gaalu xol, teer ci géeju mbëggeel
Hmm
Hmm

WRITERS

Mouhamed Fall

PUBLISHERS

Lyrics © O/B/O DistroKid

Share icon and text

Share


See A Problem With Something?

Lyrics

Other

LyricIQ Analysis

Top Emotion

Enjoyment

Sentiment
Thumbsup IconThumbsup IconThumbsup Icon
Theme

Abuse and Violence