Yeah Enh Yeah Boulaye Yéé
Taluma waxtu may job (moumou)
Song ak doole kenn duma xeeb
Waaj moy réccu jëf wees (yeah enhh)
Demal laaj ko samay ex Enh (It's king)
Level g up jarul testé Enh (moumou)
Xél g ni athlète ci piste
Du ma réccu li ma wessu lépp, rest in peace (shuuu)
Xool fu sore tax dañu different (moumou)
Xol day yég du wax mënul di fen (It's king)
Dee ba ngi ma gasal pax suul na len (ay)
Def li ma war jaru ma ñaax damay dem
Jug ak daanu nan la tarul
Ndax dama lenn gëna metti
Waaru wo ni say favoris lay nuus nii
Légende sen biir maak ngi
Bari caay-caay , Yeah (king)
Def lo mënul sans faille, Yeah (moumou)
Dama mën du ma try, No No
Ngeen def lu ma yéem never
Saa tog ci trône bi ay rêve là
Who is the king ? The king is Moumou
Loolu ay duul là (ay duul là)
Doy-waar ba fu maa tëll do xànju (king)
Job ba ennemi bi nekk fan di ma tàccu
Yeah, I aim far when I see nothing
Xaaru ma dara wala kenn pour ne ci
Do croiser les bras xaar girr mu sotti
Ne ci ker di xaar God mu bayal là tool b
Am patience ni jargoñ ci lëndam
Mel ni yeen non, def ni yeen non
Waral sa gel bëgg ma xam yamuul ci
Doon buuru game bii (yeah enh)
Maa noot ngi (yeah yeah enh)
Ndax dama lenn gëna metti
Samay homie, sama city (king)
Waaru wo ni say favoris lay nuus nii
Légende sen biir maak ngi