Bul yàqal ngaa naana guul
Fii ma dëkk bandit dëgg lanuy samp
Hé bi du yooyu feneen foo teg daa gay ñàkk
Fii ma dëkk bandit dëgg lanuy samp
Hé bi du yooyu feneen foo teg daa gay ñàkk
Rap wolof daay daw rekk, te mënu maa raw
Ëmbal taww te du maa bàyyi caat, yób ma Teuss duu coow
Naru maa jàmm beat bii sama djagg, fok ma dóor ko lu wow
Yee fitna so amul fit, làmb sa tubay tooy yaa saw
Ma leen dàqa rap, xel du ci xel-ñaar
Du ay réy bët, job rekka fayy chinois bii
Ndaw gaa c'est bien gaa roy ci Dip, mais boo dugge ci man sa musiba kepp gaay gis
Bari skills, bañ seen flop tax ñuy bañ ma drop
All the niggas feel, rap nii sama drogue daa ma ci aay torop
Màndé mbedd, bu mu la bett def na rappeur médd
Ñi doon fëgg dënd, ci seen game, ma ñëw wàcce seen daaj
Fii ma dëkk bandit dëgg lanuy samp
Hé bi du yooyu feneen foo teg daa gay ñàkk
Fii ma dëkk bandit dëgg lanuy samp
Hé bi du yooyu feneen foo teg daa gay ñàkk
Heey, Hol'up fii ku ñakk fayda di nga falu
F*ck seen bums yi f*ck seen hits yi
Compter sa cash laal sa b*tch,
Défaillant nga doo Superman
Buzzu koñ la doo superstar
Kalzaa ne naa dama wute ak gars yi
Motherf*cker maa gii ci piédestal bi
Boy bi aay na ne leen kaarokaar
Fepp weñ la mel nii Thiaroye Gare
Lii maay jaaxal du ci beat ak bass
Percer bars yi dii ci tocc ay casses
Karda kardaa maa fi teg tank
Shutta fuck'up, Need to back up
Xàalal Ndey ñepp Guediawaye la
Rattaatatatt ñepp lay dall
Maay ki lay fey ba doo suul ay man
Percer par force ba bëgg kontaan
Baye Madione nga doo bañ ku lay daan
Fi ñu dëkk bandit dëgg lanuy samp
Hé bi du boobu leneen lo def daa lay sankk!!!!
Fii ma dëkk bandit dëgg lanuy samp
Hé bi du yooyu feneen foo teg daa gay ñàkk