I'm King I'm King Yeah Enh
(Yafi né Yafi né Ya wore dh)
(Yafi né Ya wore dh Eh Yafi né)
Lancé gua sa carrière aire ball
Loy wakh wa kogn bah khamgua day thiole
Ndakh mafi né khana déguo
Vous êtes seulement là pour le décor
(Yafi né Yafi né Ya wore dh)
(Yafi né Yafi né Ya wore dh)
Tolou lén mah sakh si thiétou wé
Dague lamignou moumeu nomay thiétou wé
Kouy teukeulé ak louace ak thiét wé
Bruit bay beuri mais dou wéranté
Guén lén kharégn thiat bah thiat
Tay gaidé Mér té dégoul diatte
Fi niouy sibah bari khamou niou gatte
Bayiil Rap té défi thiak thiak
Mane rk kénén doufi khathieu
Ndakh diotouma dore gnougui nathieu
Soumay foo sen level di wathieu
Prip gua poupe Saw sa toubay
Yeah i'm the goat may seutou béyy
Pikine makoy bott soléne di hate
Rap doumasi mbokk dama si nék
Diaroul guay diém nigga dagua meunoul
Fi khandiou bé bari loutakh guén meun doul
Onkk bou méti day bou touti té khénioule
Déf loy nangou nii ma meun si khétt gou nioul (Wow)
Oubile ma feugleu rappeur yay sama b*tch guawa téki guémou ni feugeuleu
King bii No kénleu diaroul laté ndax kou wét kham sa bay lolou deug leu
I'm stunna takh Do déff Limay déff bokoy diémm di gagnou ndéysane
May tari guanane eukéy rap meusouma done talibém té koukoy déf may serigneum
Guin téh thiérék ndawal mafi ték tank
Ak king daguay rap basa boun di niank
Diokh ko cadeau ndax dou moudié loudoul ngiank
Nomay téwé ni biir bouy daw douma nieuwé nankk
Yén sa rappeur lou méti té douma bayii mou wathieu
Yokk la gathié ndax dama paré
Doko tay sakh nigga somay laté
(Yafi né Yafi né Ya wore dh)
(Yafi né Ya wore dh Eh Yafi né)
Lancé gua sa carrière aire ball
Loy wakh wa kogn bah khamgua day thiole
Ndakh mafi né khana déguo
Vous êtes seulement là pour la décor
(Yafi né Yafi né Ya wore dh)
(Yafi né Yafi né Ya wore dh)
Tolou lén mah sakh si thiétou wé
Dague lamignou moumeu thiétou wé
Kouy teukeulé ak louace ak thiét wé
Bruit bay beuri mais dou wéranté